Download presentation
1 -

Ap teereep tektal ngir


imiggere yi nek New YorkKeep ku dkk New York dina muna faju ak am taxawu ci diam te dara duko ci fekkNDIMBAL CI WALU YOON CI IMIGARASIONWoteel ActionNYC ci 800-354-0365 altine ba ajuma juroom eent wax

anastasia's Recent Documents

Gale Databases Delivered to Discovery Partners
Gale Databases Delivered to Discovery Partners

-status as of 01/13/2021Database/ArchiveOCLC Worldcat Discovery ServicesSummon/Primo Central Discovery IndexEBSCO EDSArchives of Sexuality Gender LGBTQ History and Culture Since 1940 Part IxxArchives

published 0K
Wilshire Boulevard Suite 350  Los Angeles CA 90025
Wilshire Boulevard Suite 350 Los Angeles CA 90025

12100 Phone 310 828-1183 Fax 310 453-65621999 Harrison St Suite 2020 Oakland CA 94612Phone 510 451-9521 Fax 510 451-0384TOInterested PartiesFROMDave Metz and Miranda EverittFM3 ResearchREWashington

published 0K
124 STAT 2862 PUBLIC LAW 111274OCT 13 2010 is accessible from the home
124 STAT 2862 PUBLIC LAW 111274OCT 13 2010 is accessible from the home

PUBLIC LAW 111274OCT 13 2010 LEGISLATIVEVerDate Nov 24 2008 0310 Oct 16 2010Jkt 099139PO 00274Frm 00003Fmt 6580Sfmt 6580EPUBLAWPUBL274111GPO1PsN PUBL274PUBLIC LAW 111274OCT 13 2010 The term agency mea

published 0K
ADP National Employment Report
ADP National Employment Report

Private Sector Employment Decreasedby123000Jobsin DecemberROSELAND NJ January62021Privatesector employment decreasedby 123000jobs fromNovember to Decemberaccording to the DecemberADP National Employm

published 0K
HighEfficiency Gas Boiler Limited Warranty for Residential Use Page 1
HighEfficiency Gas Boiler Limited Warranty for Residential Use Page 1

Heat Exchanger 12 years C Who Can Make Claims Under This Limited Warranty This Limited Warranty is available to you if you are the original retail purchaser or a subsequent owner and the Product has o

published 0K
COVINGTON KENTUCKY
COVINGTON KENTUCKY

r 145- February 27 1963 St Lu1z hsital of Czrnpbell ICounty 85 Worth Grand Avenue 7t LIhomas Kentucky R t 1 2 r 31 seven 7 month summer period Aril 1 through 50000 bkf the rate is 40 per Gcf plus esca

published 0K
x0000x0000FX TalkingOctober2019
x0000x0000FX TalkingOctober2019

1FX TalkingThe Teflon DollarOn a trade-weighted basis the dollar remains nears the highs of the year 150this despite the likely prospect of three Fed rate cuts this year and Congress at war The reason

published 0K
MIIISTREAM COMMONS N
MIIISTREAM COMMONS N

EWS DEC 2017Crom the 5esk of Kathy hlsonSeMsons GreePingsIP sure doesnP seem like DecemberBunPil you wMlk inPo MillsPreMm Commons Mnd Phe dMy MfPer ThMnksgivingB We Mre grMPeful for MonicM Iynch Mnd

published 0K
Download Section

Download - The PPT/PDF document "" is the property of its rightful owner. Permission is granted to download and print the materials on this web site for personal, non-commercial use only, and to display it on your personal computer provided you do not modify the materials and that you retain all copyright notices contained in the materials. By downloading content from our website, you accept the terms of this agreement.






Document on Subject : "Ap teereep tektal ngir"— Transcript:

1 Ap teereep tektal ngir imiggere yi ne
Ap teereep tektal ngir imiggere yi nek New York Keepë ku dëkk New York dina muna faju ak am taxawu ci diam te dara duko ci fekk NDIMBAL CI WALU YOON CI IMIGARASION Woteel ActionNYC ci 800-354-0365 , altine ba ajuma, juroom ñeent waxtu ci suba ba juroom been waxtu ci ngoon te do fay dara, ngir am ndimbal ci walu yoon ci imigarasion. Amal ndimbal bu bayeko ci tewalkat bu woor wala ap ni� bu ñu nagul xam xamam. TAXAWU JABOOTU IMIGGERE YI Saam wergu yaram • Def say niaku, fadju, saytu, wala fecc COVID-19 du aju dara ci li nga doon imiggere. Gissal barabu saytukaay bila gënë diege te do fay dara ci nyc.gov/covidtest wala wootel ci 212-COVID19 (212-268-4319) . • Bindul ci assuranss ci walu weergu yaram, amna ci yoodul fay dara ci nyc.gov/getcoverednyc wala wootel ci 311 . So bokul ci ñi wara am assuranss, NYC Care di nila taxawu ak pay bu neew wala do fay dara. Li nga doon imiggere amul solo. Wootel ci 646-NYC-Care (646-692-2273) wala demal ci nyccare.nyc . • Da nga tiit wala nga diaxle? Waxtanal ak beenë digalkaatu NYC Well ngir am ap taxawu ci sutura ak jokalela ak ñiiy facc feebaru xeel ak ñila muna taxali ak dorog. emal ci nyc.gov/nycwell , wootel 888-NYC-Well (888-692-9355) , wala bindal WELL ci  65173 .   Njang • Beepë xalee bu am ñeent a� dina muna boku ci Pre-K bi ak dugu ci ekool pubilik ba bi ñuy amee niar fuku ak beenë a�.Ci ay goox “3-K” dina am schools.nyc.gov/enrollment wala wootel ci 311 . • Njang angalee te do fay dara ak We Speak NYC. Sa angale su tanee di nga muna dem ci wespeaknyc.cityofnewyork.us ngir bindu ci ay kalaas ci enternet. Ay niam ci lu gaaw • Amna ay barap yuy joxe ñam yu amul mala, halal, ak leku kasseer ci NYC.Indil ñam ci sa kër dina muna neek ngir wa New York yiko yeloo. Xam ci lu gënë bari ci  nyc.gov/getfood wala wootel ci 311 tee nga wax “Get Food.” AAR KARANGEE ASKAN WI Karangee askan wi • Ci yoon, NYPD manul lacce ndax imiggere nga suñu la defe ay ñaawtéef, nga neka seedee, wala ay ni� yuy saku ndimbal. Beppa ni� buñu def ap ñaawtéef wala neka seedeep ñaawtéef nanga woote ci 911 . Aarate ci Wàllu Beddi • Booddeku, xoxatal, ak �tnal ci ap ni� ndax deram, dineem, wala limu neek imiggere dess ñuko baalee ci goxu New York. Ngir bole �tnal wala booddeku wootel ci NYC Mbootay biy seytu àq ak yelleefu domu adama 0197 . IDNYC • IDNYC moy ap kart didantitee ak nataal bodul fayee dara ngir keepa kuy yeewoo NYC te am fukki at ak luko ëpp ak dila taxa diot ci ay njariñ ak ay waañi. Xibaari yi ci ñiy lacc IDNYC dina nekk sutura. Sa nekinu imiggere amul solo. Yeesal ko ci enternet bi wala nga diël randeewu ngir bindu ci nyc.gov/idnyc wala wootel ci 311 Ay aar ngir moytu ay metital ci kër yi • Goox bi mo ngi �i ngir dimbalila su feke dañu lay metital. Mun nga dem ci wala wootee Metital ci Kër yi bu NYC ci liiñ bi 800-621-HOPE . AMNGA AY YELLEEF Xamal say yelleef ak ICE (Doxalap yoon ci walup imigarasion) • Gox bi du topato doxalap yoon ci walup imigarasion. Sula doxalap yoon ci walup imigarasion bu makk bi djegee, am nga ay yelleef. Demal ci nyc.gov/knowyourrights wala woowal ActionNYC ci  800-354-0365 ngir am ndimbal ci walu imigrasion ci yoon Yellefu Locateer • So neke ap lokaateer ci been sitee wala nga soxla ndimbal ci jafe-jafe yi ci wallu geenee wala ak kila luwee, demal nyc.gov/tenantprotection wala wootel ci 311 ak waxal“tenant helpline” ngir am ndimbal ci walu yoon.Ngir am yeneen ndimbal ci waalu dëkuwaay demal ci nyc.gov/housing . Yelleefu liggeykaat yi • Am nga yellefu am payoor soo febaree ci lu dëppoo ak sartu New York. Sa nekinu imiggere amul solo. Imiggere wu New York yi am sañ-sañu liggeey dinañu yeeloo am amu asuranss so niaka sa liggeey. Demal ci nyc.gov/workers ngir am ci yeneen xibaar wala wooteel ci 212-436-0381 . Liiñu Ask MOIA • So amee ay laaj ci imigarasion wala ci noy diotee ci njariñu Gox bi, ndimbal ci suñu laakk dina � am. Wootel Burop Meer biy topato Mbiru Imigarasion (MOIA) ci liiñ bi 212-788-7654 altine ba ajuma, ci juroom ñeent waxtu ci suba ba juroomi waxtu ci ngoon wala bataaxal ci internet askmoia@cityhall.nyc.gov . Rev. 01/2021 Wolof